dcsimg

Anet ( wolof )

tarjonnut wikipedia emerging_languages
 src=
Anet

Ci angale mooy dill or anise; Ci faranse mooy aneth

Jiwu walla doomu gàncax gu saf la. Boroom xam-xam yi xam nañu ko ci turu Anetum graweyolensë (Anethum graveolens). Jëfandiku nañu ko ngir safal ñam ak faj feebar.

Ci Injiil dañuy gis baat bi ci Mc 23:23.

 src=
anet bi ñu wowal
lisenssi
cc-by-sa-3.0
tekijänoikeus
Wikipedia authors and editors
alkuperäinen
käy lähteessä
kumppanisivusto
wikipedia emerging_languages